[Date Prev][Date Next] [Thread Prev][Thread Next] [Date Index] [Thread Index]

Bug#500669: [INTL:wo]Wolof translation of xorg package





Package: xorg
> > version: N/A
> > Severity: wishlist
> > Tags: l10n patch.


Here is the updated Wolof translation of the xorg package.
# translation of xorg_po_wo.po to Wolof
# This file is distributed under the same license as the PACKAGE package.
# Copyright (C) YEAR THE PACKAGE'S COPYRIGHT HOLDER.
#
# Mouhamadou Mamoune Mbacke <mouhamadoumamoune@gmail.com>, 2006, 2008.
msgid ""
msgstr ""
"Project-Id-Version: xorg_po_wo\n"
"Report-Msgid-Bugs-To: xorg@packages.debian.org\n"
"POT-Creation-Date: 2008-06-08 22:20+0200\n"
"PO-Revision-Date: 2008-09-30 13:25+0200\n"
"Last-Translator: Mouhamadou Mamoune Mbacke <mouhamadoumamoune@gmail.com>\n"
"Language-Team: Wolof <en@li.org>\n"
"MIME-Version: 1.0\n"
"Content-Type: text/plain; charset=UTF-8\n"
"Content-Transfer-Encoding: 8bit\n"
"X-Generator: KBabel 1.11.4\n"

#. Type: select
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:2001
msgid "X server driver:"
msgstr "Driver bu serwóir X:"

#. Type: select
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:2001
msgid ""
"For the X Window System graphical user interface to operate correctly, it is "
"necessary to select a video card driver for the X server."
msgstr ""
"Ngir interfaas Graafik bu X Window System bi mana dox nimu ware, fàwwu "
"dangaa wara tann ab driver bu serwóor X bi."

#. Type: select
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:2001
msgid ""
"Drivers are typically named for the video card or chipset manufacturer, or "
"for a specific model or family of chipsets."
msgstr ""
"Driver yi ñingi leen di farala yor turu kart video bi walla turu ki liggéey "
"chipset bi, walla modeel ak njabootu chipset yi."

#. Type: boolean
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:3001
msgid "Use kernel framebuffer device interface?"
msgstr "Ndax nu jëfandikoo interfaasu periferik framebuffer bu kernel bi?"

#. Type: boolean
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:3001
msgid ""
"Rather than communicating directly with the video hardware, the X server may "
"be configured to perform some operations, such as video mode switching, via "
"the kernel's framebuffer driver."
msgstr ""
"Serwóor X bi man naa baña jokkoo jokkoo bu joñjoo ak periferik video bi, nga "
"xam ne deeskoy komfigure muy def yenn jëf yi, lu mel ne soppi doxaliinu "
"video bi, jaarko ci driver framebuffer bu kernel bi."

#. Type: boolean
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:3001
msgid ""
"In theory, either approach should work, but in practice, sometimes one does "
"and the other does not.  Enabling this option is the safe bet, but feel free "
"to turn it off if it appears to cause problems."
msgstr ""
"Ci xalaat moom ñaar yeppu man nañoo dox, waaya ci jëf moom, leegleeg benn bi "
"dox baneen bi baña dox.  Tann lii lu wóor la, waaya bula naree andil ay "
"jafejafe kon man nga koo dindi."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:4001
msgid "Video card's bus identifier:"
msgstr "Xamlekat (ID) bu bus bo kart video bi:"

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:4001
msgid ""
"Users of PowerPC machines, and users of any computer with multiple video "
"devices, should specify the BusID of the video card in an accepted bus-"
"specific format."
msgstr ""
"�iy jëfandikoo masin yu PowerPC, ak ñiy jëfandikoo kompiyutar bu am ay kart "
"video yu bare, dañoo wara joxe BusID bu kart video bi ci ab formaat bu "
"dëppóo ak formaat yu bus yi."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:4001
msgid "Examples:"
msgstr "Misaal yi:"

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:4001
msgid ""
"For users of multi-head setups, this option will configure only one of the "
"heads.  Further configuration will have to be done manually in the X server "
"configuration file, /etc/X11/xorg.conf."
msgstr ""
"Ã?iy jëfandikoo komfiguraasioÅ? bu ay boppu yu bare (multi-head setups), nañu "
"xam ne lii benn ci boppu yi rekk lay komfigure.  Ngir komfigure yaneen yi, "
"deesna ko mana def ak loxo ci fiise komfiguraasioÅ? bu serwóor X bi, /etc/X11/"
"xorg.conf."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:4001
msgid ""
"You may wish to use the \"lspci\" command to determine the bus location of "
"your PCI, AGP, or PCI-Express video card."
msgstr ""
"Amaan nga soxlaa jëfandikoo komaand bu \"lspci\" ngir xam barab bi bus bu "
"kart video PCI, AGP, wall PCI-Express nekk."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:4001
msgid ""
"When possible, this question has been pre-answered for you and you should "
"accept the default unless you know it doesn't work."
msgstr ""
"Saa yu manee rek, bii laaj joxeelnañu la toontoom ba noppi. Dangaa wara "
"naÅ?gu defóo bi ndare ba dalaa wóor ne doxul."

#. Type: note
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:5001
msgid "Incorrect format for the bus identifier"
msgstr "Formaatu xamlekat (ID) bu bus bi baaxul"

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:6001
msgid "XKB rule set to use:"
msgstr "Reegalu XKB biñu jëfandikoo:"

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:6001
msgid ""
"For the X server to handle the keyboard correctly, an XKB rule set must be "
"chosen."
msgstr ""
"Ngir serwóor X bi mana doxal tablocaabi bi nimu ware, dangaa wara tann ab "
"reegalu XKB."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:6001
msgid "Users of most keyboards should enter \"xorg\"."
msgstr "�iy jëfandikoo li ëppu ci tablocaabi yi dañuy wara bind fii \"xorg\"."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:6001
msgid ""
"Experienced users can use any defined XKB rule set.  If the xkb-data package "
"has been unpacked, see the /usr/share/X11/xkb/rules directory for available "
"rule sets."
msgstr ""
"Jëfandikukat yi yagg ci mbir mi ñoom man na ñoo jafadikoo beppu reegalu XKB "
"boo xam ne daytalnañuko. Bu fekkee paket bu xkb-data tajjinañuko ba noppi, "
"kon xoolal kaggu bu /user/share/X11/xkb/rules ngir xam reegal yifi am."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:6001
msgid "When in doubt, this value should be set to \"xorg\"."
msgstr "Bu fekke dangay nattable, kon fii bind fi \"xorg\"."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:7001
msgid "Keyboard model:"
msgstr "Modeel bu tablocaabi bi:"

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:7001
msgid ""
"For the X server to handle the keyboard correctly, a keyboard model must be "
"entered.  Available models depend on which XKB rule set is in use."
msgstr ""
"Ngir serwóor X bi mana doxal tablocaabi bi nimu ware, dangaa wara joxe fiim "
"ab modeel bu tablocaabi. Modeel yi fiy am mingi sukkadiku ci reegal XKB yi "
"ñuy jëfandikoo."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:7001
msgid ""
" With the \"xorg\" rule set:\n"
" - pc101: traditional IBM PC/AT style keyboard with 101 keys, common in\n"
"          the United States.  Has no \"logo\" or \"menu\" keys;\n"
" - pc104: similar to pc101 model, with additional keys, usually engraved\n"
"          with a \"logo\" symbol and a \"menu\" symbol;\n"
" - pc102: similar to pc101 and often found in Europe. Includes a \"< >\" "
"key;\n"
" - pc105: similar to pc104 and often found in Europe. Includes a \"< >\" "
"key;\n"
" - macintosh: Macintosh keyboards using the new input layer with Linux\n"
"              keycodes;\n"
" - macintosh_old: Macintosh keyboards not using the new input layer;\n"
" - type4: Sun Type4 keyboards;\n"
" - type5: Sun Type5 keyboards."
msgstr ""
"Boo tannee reegal yu  \"xorg\" :\n"
" - pc101: estil bu cosaan bu tablocaabi IBM PC/AT bu am 101 butoÅ?, ñu miinko "
"ci\n"
"          Etaa yu Bennoo yu Aamerik (USA).  Amul butoÅ? bu  \"logo\" amul yit "
"bu \"menu\" ;\n"
" - pc104: dafa niróo ak modeel buc101l, waaye day am yaneen butoÅ?, yuñu "
"nataal\n"
"           ab màndarga \"logo\" ak màndarga bu \"menu\";\n"
" - pc102: dafay niróo ak  pc101 ta deesnako faral di gis ci �róop (Europe). "
"Dafay am ab butoÅ? bu \"< >\" ;\n"
" - pc105: dafay niróo ak pc104 ta deesnako faral di gis ci �róop. Dafay am "
"ab butoÅ? bu  \"< >\" ;\n"
" - macintosh: tablocaabi bu Macintosh buy jëfandikoo kuusu dugël (input) bu "
"yees bi ak keycodes\n"
"              yu Linux;\n"
" - macintosh_old: tablocaabi bu Macintosh budul jëfandikoo kuusu dugël bu "
"yees bi.\n"
" Budee ci reegal yu \"sun\":\n"
" - type4: tablocaabi Type4 bu Sun;\n"
" - type5: tablocaabi Type5 bu Sun."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:7001
msgid ""
"Laptop keyboards often do not have as many keys as standalone models; laptop "
"users should select the keyboard model most closely approximated by the "
"above."
msgstr ""
"Kompiyutar yiñuy gaddu (laptop) ñoom duñuy faral di am mbooleem butoÅ? yi "
"modeel yu mag yi di am, kon ñi yore kompiyutar yiñuy gaddu dañoo wara tann "
"modeel bi gëna jege seen bos ci yii ñu lim ci kaw."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:7001
msgid ""
"Experienced users can use any model defined by the selected XKB rule set.  "
"If the xkb-data package has been unpacked, see the /usr/share/X11/xkb/rules "
"directory for available rule sets."
msgstr ""
"Jëfandikukay yi miin Linux ñoom man nañoo tann béppu modeel buñu daytal ci "
"reegal bu XKB biñu tann. Bu fekkee paket bu xkb-data dajjeesna ko, kon "
"xoolal kaggu bu /usr/share/X11/xkb/rules ngir xam reegal yifi am."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:7001
msgid ""
"Users of U.S. English keyboards should generally enter \"pc104\".  Users of "
"most other keyboards should generally enter \"pc105\"."
msgstr ""
"Ã?iy jëfandikoo tablocaabi bu AÅ?gle Amerikee (US English) lici ëppu dañuy "
"wara bind fii \"pc104\". �iy jëfandikoo yi ëppu ci yaneen toblocaabi dañuy "
"wara bind fii \"pc105\"."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:8001
msgid "Keyboard layout:"
msgstr "Tërëliinu tablocaabi bi:"

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:8001
msgid ""
"For the X server to handle the keyboard correctly, a keyboard layout must be "
"entered.  Available layouts depend on which XKB rule set and keyboard model "
"were previously selected."
msgstr ""
"Ngir serwóor X bi di mana doxal tablocaabi bi nimu ware, dangaa wara bind "
"fii aw tërëliinu tablocaabi. Tërëliin yi ngay mana tann ci ngiy aju ci "
"reegal XKB ak modeelu tablocaabi yinga tannoon."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:8001
msgid ""
"Experienced users can use any layout supported by the selected XKB rule "
"set.  If the xkb-data package has been unpacked, see the /usr/share/X11/xkb/"
"rules directory for available rule sets."
msgstr ""
"Jëfandikukay yi miin Linux ñoom danañu mana tann béppu tërëliin boo xam ne "
"reegal XKB bi danako naÅ?gu.  Bu fekkee paket bu xkb-data dajjeesna ko, kon "
"xoola kaggu bu /usr/shar/X11/xkb/rules ngir mana xam reegal yifi am."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:8001
msgid ""
"Users of U.S. English keyboards should enter \"us\".  Users of keyboards "
"localized for other countries should generally enter their ISO 3166 country "
"code.  E.g., France uses \"fr\", and Germany uses \"de\"."
msgstr ""
"�iy jëfandikoo tablocaabi yu US English ñoom dañuy wara bind fii \"us\".  "
"�iy jëfandikoo tablocaabi yuñu lokaaliise ñeel seen réew ñoom dañuy bi kod "
"ISO 3166 bu seen réew. Ci misaal Almaañ migni doon \"de\", Fraas doon \"fr\"."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:9001
msgid "Keyboard variant:"
msgstr "Cafaan bu tablocaabi bi:"

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:9001
msgid ""
"For the X server to handle the keyboard as desired, a keyboard variant may "
"be entered.  Available variants depend on which XKB rule set, model, and "
"layout were previously selected."
msgstr ""
"Ngir serwóor X bi di mana doxal tablocaabi bi nimu ware, dangaa wara bind "
"fii ab cafaan bu tablocaabi.  Cafaan yifiy am mingiy sukkandiku ci reegal "
"XKB, ak tërëliin yinga tannoon."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:9001
msgid ""
"Many keyboard layouts support an option to treat \"dead\" keys such as non-"
"spacing accent marks and diaereses as normal spacing keys, and if this is "
"the preferred behavior, enter \"nodeadkeys\"."
msgstr ""
"Lu bare ci tërëliinu tablocaabi yi danañu mana tanna jëflënté ak butoÅ? yu "
"dee yi \"dead keys\", yu mel ne maaska yudul ànd ak espaas, ñaari tombu ci "
"kaw araf (dieres), jëlënté ak ñoom mel ne buñu doonoon butoÅ? yu espaas yu "
"normaal. Bu fekkee loolu nga bëgg kon bindal fii \"nodeadkeys\"."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:9001
msgid ""
"Experienced users can use any variant supported by the selected XKB layout.  "
"If the xkb-data package has been unpacked, see the /usr/share/X11/xkb/"
"symbols directory for the file corresponding to your selected layout for "
"available variants."
msgstr ""
"Jëfandikukay yi miin Linux ñoom danañu mana tann béppu cafaan boo xam ne "
"reegal XKB bi danako naÅ?gu.  Bu fekkee paket bu xkb-data dajjeesna ko, kon "
"xoola kaggu bu /usr/shar/X11/xkb/symbols ngir gis fiise bi dëppóo ak "
"tërëliin winga tànn, danga ca gis cafaan yi fi am."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:9001
msgid "Users of U.S. English keyboards should generally leave this entry blank."
msgstr ""
"Ã?iy jëfandikoo tablocaabi bu AÅ?gle Amerikee (US English) ñoom li ci ëppu "
"waruñoo bind fii dara."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:10001
msgid "Keyboard options:"
msgstr "Tann yu tablocaabi bi:"

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:10001
msgid ""
"For the X server to handle the keyboard as desired, keyboard options may be "
"entered.  Available options depend on which XKB rule set was previously "
"selected.  Not all options will work with every keyboard model and layout."
msgstr ""
"Ngir serwóor X bi di mana doxal tablocaabi bi ninga koy bëggé, man ngaa bind "
"fii ay tanni tablocaabi. Tann yi ngay mana def ñingiy aju ci reegal XKB "
"yinga tannoon. Tann yéppu nak duñu dox ci modeeli tablocaabi yéppu ak "
"tërëliin yéppu."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:10001
msgid ""
"For example, if you wish the Caps Lock key to behave as an additional "
"Control key, you may enter \"ctrl:nocaps\"; if you would like to switch the "
"Caps Lock and left Control keys, you may enter \"ctrl:swapcaps\"."
msgstr ""
"Ci misaal, Boo bëggée butoÅ? bu Caps Lock mu mel ne baneen butoÅ? bu Control, "
"kon dangay bind fii \"ctrl:nocaps\", Boo bëggée taal Caps Lock ak butoÅ? "
"Control yi ci jammooy, kon man ngaa bind fii \"ctrl:swapcaps\"."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:10001
msgid ""
"As another example, some people prefer having the Meta keys available on "
"their keyboard's Alt keys (this is the default), while other people prefer "
"having the Meta keys on the Windows or \"logo\" keys instead.  If you prefer "
"to use your Windows or logo keys as Meta keys, you may enter \"altwin:"
"meta_win\"."
msgstr ""
"Baneen misaal mingi nii: ñenn ñi dañuy bëgg butoÅ? yu Meta yi nekk ci butoÅ? "
"Alt yi ci tablocaabi bi (loolu mooy defóo bi), amna yit ñaneen dañuy bëgg "
"butoÅ? bu Meta nekk ci butoÅ? bu Windows bi walla butoÅ? bu \"logo\" bi. Bu "
"fekkee dangaa bëgga jëfandikoo butoÅ? bu Windows bi walla bu logo bi defleen "
"ñuy say butoÅ? yu Meta, kon man ngaa bind fii \"altwin:meta_win\"."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:10001
msgid ""
"You can combine options by separating them with a comma, for instance \"ctrl:"
"nocaps,altwin:meta_win\"."
msgstr ""
"Man nga boole ay tann daldi leen teqale ak ay wirgil, ci misaal \"ctrl:"
"nocaps,altwin:meta_win\"."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:10001
msgid ""
"Experienced users can use any options compatible with the selected XKB "
"model, layout and variant."
msgstr ""
"Jëfandikukay yi miin Linux ñoom danañu mana jëfandikoo béppu tànn boo xam ne "
"modeelu XKB bi, tërëliinwi ak cafaan bi danañuko naÅ?gu."

#. Type: string
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:10001
msgid "When in doubt, this value should be left blank."
msgstr "Bu fekkee dangay sikksakka, kon fii waróo fée bind dara."

#. Type: note
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:11001
msgid "Empty value"
msgstr "Lim bi dafa widd"

#. Type: note
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:11001
msgid "A null entry is not permitted for this value."
msgstr "Fii duñu naÅ?gu nga bayyiko mu neen bañ fee def dara."

#. Type: note
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:12001
msgid "Invalid double-quote characters"
msgstr "Karakteer yu guillemet yi baaxul"

#. Type: note
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:12001
msgid "Double-quote (\") characters are not permitted in the entry value."
msgstr "Karakteer bu guillemet (\") deesuko naÅ?gu fii."

#. Type: note
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:13001
msgid "Numerical value needed"
msgstr "Am lim (numero) lañu soxla"

#. Type: note
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:13001
msgid "Characters other than digits are not allowed in the entry."
msgstr "Kenn du naÅ?gu fii ab karakteer budul ab lim (numero)."

#. Type: boolean
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:14001
msgid "Autodetect keyboard layout?"
msgstr "Ndax nu jéema gisal sunu boppu tërëliinu tablocaabi bi?"

#. Type: boolean
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:14001
msgid ""
"The default keyboard layout selection for the Xorg server will be based on a "
"combination of the language and the keyboard layout selected in the "
"installer."
msgstr ""
"Serwóor Xorg bi, ci tann tërëliinu tablocaabi bu defóo bi mingiy sukkandiku "
"ci làkk wi nga tann ak ci tërëliinu tablocaabi wi nga tann ci prograamu "
"istalaasioÅ? bi."

#. Type: boolean
#. Description
#: ../xserver-xorg.templates:14001
msgid ""
"Choose this option if you want the keyboard layout to be redetected.  Do not "
"choose it if you want to keep your current layout."
msgstr ""
"Tannal lii boo bëggée ñu jéema làmbutuwaat tërëliinu tablocaabi bi. Buko "
"tann boo bëggée jappu ci tëëliin wi nga yor fimune nii."

#. Type: select
#. Choices
#: ../x11-common.templates:2001
msgid "Root Only"
msgstr "Root Rekk"

#. Type: select
#. Choices
#: ../x11-common.templates:2001
msgid "Console Users Only"
msgstr "Jëfandikukat yu Konsol Rekk"

#. Type: select
#. Choices
#: ../x11-common.templates:2001
msgid "Anybody"
msgstr "Kumu mana doon"

#. Type: select
#. Description
#: ../x11-common.templates:2002
msgid "Users allowed to start the X server:"
msgstr "Jëfandikukat yiñu may ñu tambule serwóor X:"

#. Type: select
#. Description
#: ../x11-common.templates:2002
msgid ""
"Because the X server runs with superuser privileges, it may be unwise to "
"permit any user to start it, for security reasons.  On the other hand, it is "
"even more unwise to run general-purpose X client programs as root, which is "
"what may happen if only root is permitted to start the X server.  A good "
"compromise is to permit the X server to be started only by users logged in "
"to one of the virtual consoles."
msgstr ""
"Binga xamee ne serwóor X dafay dox ak sañsañu superuser, doonul lu xellu di "
"may ñéppu ñukoy mana tambule, ngir kaaraangey sistem bi. Ba tay doonul yit "
"lu xellu rugge root ba noppi di doxal prograam kiliyaÅ? yu X, ta loolu mooy "
"am bu fekkee dangaa def ne root rekk mooy mana tambule serwóor X. Jubna lool "
"nak nga def ne serwóor X kikoy mana tambule day doon ku duggee ci benn ci "
"konsol wirtuwel yi."

#. Type: string
#. Description
#: ../x11-common.templates:4001
msgid "Nice value for the X server:"
msgstr "Walóor nice bu serwóor X:"

#. Type: string
#. Description
#: ../x11-common.templates:4001
msgid ""
"When using operating system kernels with a particular scheduling strategy, "
"it has been widely noted that the X server's performance improves when it is "
"run at a higher process priority than the default; a process's priority is "
"known as its \"nice\" value.  These values range from -20 (extremely high "
"priority, or \"not nice\" to other processes) to 19 (extremely low "
"priority).  The default nice value for ordinary processes is 0, and this is "
"also the recommend value for the X server."
msgstr ""
"Booy jëfandikoo kernel bu sistemu doxaliin bu yore yenn estrateji bu nos "
"waxtuy liggéey, seetlu nañu bubaax ne liggéeyu serwóor X bi dana gana rafet "
"bu fekkee dafay dox ak piriyorite liggéey (process) bu gëna kawe bu defóo "
"bi; piriyorite bi ab liggéey di am (maanaa ab process) lañuy tudde walóoru "
"\"nice\".  Walóor yooyu mingi tambulee ci -20 (piriyorite bu kawe lool, "
"maanaa  \"not nice\" ci yaneen liggéey yi) baci 19 (piriyorite bu suufe "
"lool).  Walóor nice bu defóo bu liggéy ordineer moooy 0, ta moom yit lañuy "
"laabiire ñu jox ko serwóor X."

#. Type: string
#. Description
#: ../x11-common.templates:4001
msgid ""
"Values outside the range of -10 to 0 are not recommended; too negative, and "
"the X server will interfere with important system tasks.  Too positive, and "
"the X server will be sluggish and unresponsive."
msgstr ""
"Walóor yi génn diggante -10 ba 0 laabiirewuñu kukoy joxe, dañoo negatif bamu "
"ëppu, dañuy tax serwóor X bi di duggante ak yenn liggéey yu sistem yu am "
"solo yi. Bu doonee lu positif bamu ëppu, konn serwóor X bi dafay tayyeel "
"lool ba nga xamne daanaka du wuyyu ci liñukoy woo."

#. Type: note
#. Description
#: ../x11-common.templates:5001
msgid "Incorrect nice value"
msgstr "Walóor nice bi baajul"

#. Type: note
#. Description
#: ../x11-common.templates:5001
msgid "Please enter an integer between -20 and 19."
msgstr "Joxeel ab numero bu wér digga -20 ak 19."

#. Type: note
#. Description
#: ../x11-common.templates:6001
msgid "Major possible upgrade issues"
msgstr "Yenn probleem yukk daraja (upgrade)"

#. Type: note
#. Description
#: ../x11-common.templates:6001
msgid ""
"Some users have reported that upon upgrade to the current package set, their "
"xserver package was no longer installed. Because there is no easy way around "
"this problem, you should be sure to check that the xserver-xorg package is "
"installed after upgrade. If it is not installed and you require it, it is "
"recommended that you install the xorg package to make sure you have a fully "
"functional X setup."
msgstr ""
"Yenn jëfandikukat yi waxnañu ne buñu yokkee daraja seen sistem bi andiko ci "
"bii paket. seeni paket yu xserver deesootuko istale. Ginnaaw problem boobu "
"yoombula lijjanti, kon warngaa seet baxam paketu xserver-xorg istaleesna ko "
"ginaaaw boo yokkee daraja ba noppi. Bu fekkee istaleesu ko ta nga soxla ko, "
"kon ñingi lay laabiire nga istale paket bu xorg ngir mu wóor la ne da nga am "
"istalaasioÅ? bu X buy dox."

#. Type: note
#. Description
#: ../x11-common.templates:7001
msgid "Cannot remove /usr/X11R6/bin directory"
msgstr "Manula dindi kaggu bu /usr/X11R6/bin"

#. Type: note
#. Description
#: ../x11-common.templates:7001
msgid ""
"This upgrade requires that the /usr/X11R6/bin directory be removed and "
"replaced with a symlink. An attempt was made to do so, but it failed, most "
"likely because the directory is not yet empty. You must move the files that "
"are currently in the directory out of the way so that the installation can "
"complete. If you like, you may move them back after the symlink is in place."
msgstr ""
"Yokku daraja bi dafay laaj ñu dindi kaggu bu /usr/X11/R6/bin wottee ko ak ab "
"simlink. Loolu jéemnanukoo def waaye antuwul, likoy waral amaana moodi kaggu "
"bi dafa am lu ci nekk ba leegi. Da ngaa wara dindi fiise yi nekk ci kaggu bi "
"ngir istalaasioÅ? bi man egg. Bula neexee sax mannga leena delloosi ginnaaw "
"bu simlink bi istalewoo ba noppi."

#. Type: note
#. Description
#: ../x11-common.templates:7001
msgid ""
"This package installation will now fail and exit so that you can do this. "
"Please re-run your upgrade procedure after you have cleaned out the "
"directory."
msgstr ""
"Kon istalaasioÅ? bu bii paket antuwl ta mingi nii di génn ngir nga mana def "
"loolii. Kon nanga dellu defaat yokku daraja bi ginnaaw boo setalee kaggu bi "
"ba noppi."


Reply to: